Li Ma Weesu

Youssou N'dour
앨범 : Nothing‘s In Vain(Coono Du Reer)

li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
seetal
leegi leegi ma gesu
ci li ma weesu
leegi leegi ma recu
walla sax di baaku
fu gune yi feetee
dama leen di teetee
wax nu ma neexee
ma begga leen
damay damay
damay dellu gune
mel ni mel ni
mel ni duma magg
damay damay
damay dellu gune
mel ni mel ni
mel ni duma magg
lu ma gen di yagg
xel ni mel ni bank
lu ma gen di magg
dellu tuuti tank
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
ma ni seetal
leegi leegi ma gesu
ci li ma weesu
leegi leegi ma recu
walla sax di baaku
fu gune yi feetee
dama leen di teetee
wax nu ma neexee
ma begga leen
damay damay
damay dellu gune
mel ni mel ni
mel ni duma magg
damay damay
damay dellu gune
mel ni mel ni
mel ni duma magg
fu gune yi feetee
dama leen di teetee
wax nu mu ma neexee ma beggati
li ma gen di jege
mel ni dama sore
lu ma gena sore
gen di gis li ma jegewoon
lu ma gen di yagg
xel ni mel ni bank
lu ma gen di magg
dellu tuuti tank
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
damay damay damay dellu gune
mel ni mel ni mel ni duma magg
damay damay damay dellu gune
mel ni mel ni mel ni duma magg
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu
li ma dundee li ma weesu
dey delluse mel ni seetu

그외 검색된 가사들

가수 노래제목  
Steve Miller Band Shu Ba Da Du Ma Ma Ma Ma  
Jeff Lynne's ELO Ma-Ma-Ma Belle (Live at Wembley Stadium)  
Joe Budden, 112 Ma Ma Ma (Album Version (Explicit))  
구피(Goofy) La Li Li (라리리)  
Li Li ALLY (prod. RGFLEG)  
구피(Goofy) La Li Li  
구피 La Li Li (라리리)  
Electric Light Orchestra Ma-Ma-Ma-Belle  
Electric Light Orchestra Ma-Ma-Ma Belle  
구피 La Li Li  
리쥐(Li-G)/리쥐(Li-G) 퍼즐 (Feat. 김가희)  
인스턴트 로맨틱 플로어(Instant Romantic Floor) Ma Ma Disco  
Patrick Abrial Ma femme, ma guitare et mon chien  
!dongivafxxk (이동기버뻑) ice on ma wrist, ma body  
주걸륜 聽媽媽的話 (Ting Ma Ma De Hua)  
Amir Ma Vie, Ma Ville, Mon Monde  
주걸륜 聽瑪瑪的話 (Ting Ma Ma De Hua)  
Fat Joe Lean Back (Remix) (Feat. Lil Jon, Eminem, Ma$e & Remy Ma)  
바니걸스 그대를 보내고 (Ma Ma Mia)  

관련 가사

가수 노래제목  
Youssou N'dour 7 Seconds (Feat. Neneh Cherry)  
Youssou N'dour Chimes Of Freedom  
Youssou N'dour Jealous Guy (Album Ver.)  
Youssou N'dour Jealous Guy  
Wyclef Jean Diallo / Youssou N'Dour & Mb 2  
Wyclef Jean Diallo (Album Version) (Feat. Youssou N'Dour, MB2)  
Neneh Cherry 7 Seconds  
Antonio Orozco, Youssou N'dour Por Que No Les Devuelves El Sol  
Youssou N'dour, Neneh Cherry 7 Seconds  
구피 La Li Li  




가사 수정 / 삭제

댓글목록

등록된 댓글이 없습니다.